musicas.mus.br
Letras de músicas - letra de música - letra da música - letras e cifras - letras traduzidas - letra traduzida - lyrics - paroles - lyric - canciones - FAKE NEWS - MIA GUISSE - música e letra
Utilize o abecedário abaixo para abrir as páginas de letras dos artistas
Fake News letra
Maa ngi toog sama biir kër
Lim binde nii maa ngi fa woon
Nga lire ko, gëm ko, saaga ma
Lan moo xew?
Moo ko def
Ma ni la moom la
Gutt bi fii lay jaar
Numu soofe
Bëgg naa solu te noon la xayade
Bu juge dépp ay cheveum yu ñàppe
Jëlal make-up bi muy mel ni gaynde
Lijjanti lijjanti ba nar ci wayadee
Der bi ngay yaqi, demal jox ko uude
Mu def ko dalle sol ko uuti loo def
Picc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw
Duñ bëgg sa dara, sappa dëxin
Solu rombati leen, parfum bi tontu leen
Amatuma benn temps ay waxi noon
Solu rombati leen, parfum bi tontu leen
Amatuma benn temps, maa ngi ci man
Maa ngi toog sama biir kër
Lim binde nii maa ngi fa woon
Nga lire ko, gëm ko, saaga ma
Lan moo xew?
Moo ko def
Ma ni la moom la
Gutt bi fii lay jaar
Pourquoi ba léegi sooy lire
Mettit bañu ñu naak jege
Ñi ci mbedd mi ngay fore say fait
Nit ñi lëndëm nañu
Ba mel ni coupure général
Ne ci, ohhh léegi
Ñu xam ni Yàlla du mësa fay wax di baay jëf
Picc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw
Duñ bëgg sa dara, sappa dëxin
Solu rombati leen, parfum bi tontu leen
Amatuma benn temps ay waxi noon
Solu rombati leen, parfum bi tontu leen
Amatuma benn temps, maa ngi ci man
Maa ngi toog sama biir kër
Lim binde nii maa ngi fa woon
Nga lire ko, gëm ko, saaga ma
Lan moo xew?
Moo ko def
Ma ni la moom la
Gutt bi fii lay jaar
Àdduna bii bu doon arène
Ku bëgg jal faut nga laale
Xeex dokki bu mu gacce yi
Ci bañu lay nawe
Ne ci léegi
Ñu xam ni Yàlla du mësa fay wax di baay jëf
Picc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw
Moo ko def moom la!
Wuy leeee
Wuy lelelelee
Ma ni gumbal, gumbal
Texel waay gumbal
Ma ni gumbal, gumbal
Mia Guisse - Letras
- Ar Njehen (remix) (feat. Adviser)
- Choix (feat. Wally B. Seck)
- Confuse (feat. Wally B. Seck & Amadeus)
- Fake News
- Gauche & Droite
- GLP (Gën Leen Paré)
- Idda
- Idda (Pulaar Version)
- Jolie femme d'Afrique
- La coupe reviendra (Manko wuti waat ndam li)
- La vie est belle
- Leundeum (feat. Omzo Dollar)
- Lonkotina
- Mère Célibataire
- On a pas les temps (feat. Viviane Chidid)
- Peace Of Mind (feat. Iyanya)
- Reine Xol (Round 5) (feat. NOFACE)
- Sama Xool (feat. VJ)
- Titulaire (feat. Axel Merryl & Bass Thioung)
- Unique (feat. Djelykaba Bintou)
- Wérouway
top 30 músicas
©2003 - 2026 - musicas.mus.br